wolof
stringlengths
1
166
french
stringlengths
2
331
ag
(devant les noms de la classe {g-}) Un(e)
Am na ag gone gu la doon wut
il y a un enfant qui te cherchait.
artu
mettre en garde, avertir
Bi ñu ko defee, Yàlla artu leen ci biir gént, ñu baña dellu ca Erot
alors, Dieu les avertit en garde en songe de ne pas retourner chez Hérode.
akkati
enlever les croûtes d’une plaie
Yaay ja akkati piccam ya ba ñu set
sa maman nettoya proprement les croûtes de ses pustules.
artu b-
mise en garde, avertissement
aru
être en colère
Dafa aru; nanguwul sax lekk
il est fâché; il ne veut même pas manger.
aawlu
être sujet à tous les malheurs qui arrivent
Dama aawlu
C'est à moi qu’arrivent tous les malheurs.
asaka j-
partie que le musulman prélève annuellement sur ses biens pour les nécessiteux
At mu ne, war ngaa génne asaka
chaque année, tu dois prélever une partie de tes biens pour les pauvres.
as
un / une
As suuf
une terre
aaye
interdire
Dafay aaye ku fi tux
il interdit de fumer ici.
(prov.) Kuy aaye xobu màngo, doo ci maye ub doom
celui qui ne permet pas de toucher aux feuilles du manguier, n’en donnera pas un fruit.
asaaloo
lancer qqch en chandelle.
abdu jaambaar m-
abdou Diambar, ange de la mort
Abdu-jaambaar dafa la naan : – Julli nga am ?
Abdou Diambar te dit : – As-tu prié ou non ?
able
prêter
Dama able sama woto
J'ai prêté ma voiture.
aset b-
assiette
asi
hacher
Nanga asi soble bi
tu hacheras l’oignon.
aj g-
pèlerinage à La Mecque
Ren, aj gi mettiwuloon
cette année, le pèlerinage à La Mecque n’a pas été pénible.
aseer j-
samedi
Aseer ja ca topp la ñów
il est venu le samedi suivant.
ab
un, une
amaa
soit que… soit que…
Demal wax ko sa soxla amaa mu ne waaw, amaa mu ne déet
va lui dire ton problème; soit il dit oui, soit il dit non.
askanoo
être issu de telle lignée paternelle
Foo askanoo ?
de quelle lignée paternelle es-tu ?
aj b-
fait de placer qqch en hauteur
aj b-
botte de foin de haricot suspendue pour la conserver
abalante
se prêter des choses mutuellement
Xale yi dañuy abalante seeni yére te baaxul
les enfants se passent leurs habits entre eux mais ce n’est pas bien.
alamikk
certainement
aj
aller en pèlerinage à La Mecque
Aj na ñaari yoon
il est allé deux fois en pèlerinage à La Mecque
aj
placer qqch à un endroit élevé
Ajal saaku bi ci kow armool bi
place le sac sur l’armoire !
(loc.) Ajal say mbagg
hausse les épaules !
(loc.) Danu aj ngénte li
nous avons reporté le baptême.
Ajal sa naw
retiens ton souffle !
(prov.) Ku sa nàkk jeex, nga aj say koog
celui qui a fini de faire son gâteau de riz range ses cuillères en bois (quand on a épuisé ses atouts, on se retire).
aay
jouer au {aay}
Kaayleen ! Ñu aay
venez ! Nous allons jouer au aay.
aca
invite à faire une action
Aca, woyal
vas-y, chante !
Aca, ca biti !
allez, dehors !
Aca, nu dem !
allons-y !
altine j-
lundi
Altine jiy ñów
lundi prochain.
aw
un(e)
May na ma aw nag
il m’a offert une vache.
afal b-
bouche d’aération
Yàkkalil afal bi
élargis la bouche d’aération.
akara b-
(Yor.) Beignet de haricot acra
Jaay ma akara
vends-moi des acras.
(prov.) Ku bëgg akara, dangay ñeme kaani
qui veut des acras ne doit pas redouter le piment.
astemaak
plus forte raison
Ndegem yow, yaa ko mëna def, astemaak moom
si toi, tu peux le faire, à plus forte raison lui.
(prov.) Làmmiñ jigul bant, astemaak nit
la langue (par son influence magique) est mauvaise pour le bout de bois, à plus forte raison pour la personne.
awal
cultiver le champ de son beau-père
Damay awal sama goro-bu-góor toolam
je fais des travaux pour mon beau-père dans son champ.
abal
prêter
Abal ma sa saatu
prête-moi ton canif.
Abal ma !
fiche le camp !
(prov.) Ku la abal i tànk, nga dem fa ko neex
on fait ce qui plaît à son bienfaiteur.
awale
faire passer (qqch) par
awyoŋ b-
avion
aw-aw b-
passages incessants
and b-
brûle-parfum
And bi dafa toj
le brûle-parfum est brisé.
Taaj nit ci andam
empoisonner (à qqn) la vie.
awra j-
sexe
Muural ko awraam
couvre-lui les parties intimes.
aw b-
travaux champêtres effectués pour son beau-père
Sama goro dafa ma sant ab aw
mon beau-père m’a chargé d’un travail dans son champ.
awu
saisir au vol
Dama ko awu, lu ko moy mu toj
je l’ai saisi au vol, autrement il se brisait.
aballoo
amener à prêter
Ku la aballoo Astu sama kuur ?
qui t’a demandé de prêter mon pilon à Astou ?
ax
traduit la douleur ou le plaisir
Ax, aka metti ?
aïe, comme c’est douloureux !
a nga
voilà
Omar a nga
voilà Omar.
alamaan b-
amende
Feyaguloo sa alamaan bi
tu n’as pas encore payé ton amende.
ay
avoir lieu
Lépp lu fi ay, na leen wóor ne dina ko ko jottali
soyez certains qu’il lui rendra compte de tout ce qui se passe ici.
(prov.) Lu ay, di njàmbat
quand une chose a lieu, on en parle.
ay
des
Ay xale lay waxal
C'est à des enfants qu’il parle.
ay
exprime la douleur
Ay ! màtt na ma
aïe ! il m’a mordu.
axakay
si (dans une réponse à une phrase interro-négative)