audio
audioduration (s) 0.74
171
| text
stringlengths 1
109
| gender
stringclasses 2
values |
---|---|---|
Xoolal li man a nekk ! | male |
|
Dandul sama kanam, xale. | male |
|
Sàmpleen seen i wóom! | female |
|
Fàtteliku naa ko. | female |
|
Tey ngay maas nii | female |
|
Nu fecci itam toolale yu nu kaabaal yi. | male |
|
àndal bi mu yëgee deewu Paap Juuf gi. | male |
|
Foo jëm aawoloo ma | female |
|
Xàmmee naa sa kanam. | male |
|
Waaye, ba tey lu man a nekk la | female |
|
Dafa xaw a xewwi. | female |
|
lekk mbaa naan mbaa séy bu ñu la ci man antee | male |
|
cër bu nekk ci biiru nit, bàyyima | male |
|
Li ci kanam kepp a ñu koy wax. | female |
|
Lii ñaaw na. | female |
|
Warug woor weeru koor | male |
|
Nanu jéem ! | female |
|
Yor na ab nataal. | female |
|
Def na ski. | male |
|
réewum Gaambi ci bëj-saalum | male |
|
Danoo neew doole bamu ëpp. | male |
|
Liig gu Bëj-Gannar bu Dunu Santo Antão | male |
|
Wax dë gg Yàlla, jàng naa téere yu bari | female |
|
Lu raw bég laa def. | male |
|
yéwenalal ko àddunaam ak diineem,te nga méng ko yoolub jiyaarkat yi | male |
|
Ci àngale mooy Barak Ci faranse mooy Barak ou Barac | male |
|
Baara Kan 773420282 | female |
|
Boobu, aw waxambaane la woon, amoon ñaar-fukki at ak juróom-ñent doŋŋ | male |
|
Lu dul dëgg du yágg | female |
|
Manoon naa dox. | male |
|
Xam ngeen leen? | female |
|
Leegi njiit laa. | female |
|
Garabu tabanaani man naa àgg ba 8i sàntimet ci guddaay | female |
|
Ndax yéen a ngi Boston ? | male |
|
Nga weex sa xol wékki ca luy wòllimiku | female |
|
Am na xaj a? | female |
|
Sonko daa aakimu, daanaka, reeso sosiyoo yi, bàyyi wujjam yépp ginnaaw ci wàll woowu | male |
|
Jàppal ne ñépp a feebar ba kenn du la ko wàlli, | male |
|
Benn bés, yaayu xale yi dem rëbbi | female |
|
Mu meloon ne solu ma dara. | female |
|
Saada Kan Am na loo mës a wax, te mu soxal ma lool | female |
|
Ci 9 desambar 1961 la leen ko Nguur-Yu-Bennoo yi jox, ci jàmm | female |
|
Dafa am daamarug boppam. | male |
|
Lëlëg su nekk nu dégg xibaar yu yees te tiis, jëm ci jàngoroy koronaa. | female |
|
Dama ko xam. | female |
|
laata nga jox xale bi lekk | female |
|
Dafa man a làkk a? | male |
|
Nu ngi nekk di lekk ay pom. | female |
|
Jàngub San Pool bi nekk London moom it jagoo woon njàng yu nite yi. | male |
|
Ngir sama njaboot a. | female |
|
Sula neexee bul jóg. | female |
|
Bëggu ma alkaati. | male |
|
Dama foog ne Tom a am dëgg. | female |
|
Kenn manu maa tëye. | male |
|
Mujj na nekk ab fajkat. | male |
|
Xoolal rekk ni ko alkaati yi raye… | female |
|
Damaa bëgg a moom sama bopp. | male |
|
Abila sore woon na Damas ca sowu kaw lu tollu 29 kilomet | female |
|
Ndax yoru nu dara ? | female |
|
Bégal nga ma. | female |
|
Ndekete yóo sama bopp laay ree . ?? | female |
|
Gelawaar yi ñoo neekkoon Buur yi. | female |
|
Ay tontu laa soxla. | male |
|
Noo ngi reccu. | male |
|
Bsiiru Jaañ 76 768 32 31 | female |
|
Mbégte laay am sumay dawal. | male |
|
Duggalal fii mbind mi ñu daytalul. | male |
|
Moom nag mu ngi wax kàddoom yooyu sunu naataangoy «Quotidien» yi. | male |
|
Diiwaani kilima yiSoppi | male |
|
Tom manul dugg. | male |
|
Yokkuteg jarag yi nag day indi yokkuteg ñi nuy téye ci raglu yi | female |
|
Dangeen a noppi. | female |
|
Day metti fii. | male |
|
Ànd naa ci sa xalaat bi. | male |
|
Ñépp daal di yuuxu. | female |
|
Damaa màgget lool ci Tom. | male |
|
Bëggoon naa la. | female |
|
Lu ca xewoon? | male |
|
Ay araab lan. | male |
|
Doxleen ñaari jéego. | female |
|
Fàww ma yëggal koko. | male |
|
③- ABDU LAAY JUUF SAAR | male |
|
Jigéen ñépp, rawatina yu Afrig, ameel nañ ko njukkal | male |
|
Muy lim bu takku | male |
|
Loolu di firndéel yàq, yaataayumbe ak gundaandaat gi waa nnguur gi nekke | female |
|
Doomu jaxaay ja sëngeem | female |
|
Tane na ! | male |
|
Yóbbu nan ko. | male |
|
Dafau j . | female |
|
Waa Room nangu nañu diiwaanu Siri ca atu 64 j.K | female |
|
Duñu la def lu bon. | female |
|
Damaa bañ taarde. | male |
|
Teeñ mooy kilifaga yilif Bawal, | male |
|
Amerig am na ci talaata ji téemeeri nit ñu faatu ci mbas mi | female |
|
Dama amoon mbetteel. | male |
|
Amu ñu ci. | male |
|
Ndax soppluwul ? | female |
|
Ab sàcc la. | female |
|
Ñépp a ko sopp. | female |
|
Daara yu kawe yi uniwersite dinañu amal seen njàng ci seen ay kër. | female |